Seven Shots - Affaire de Ado lyrics

Published

0 120 0

Seven Shots - Affaire de Ado lyrics

Refrain Kou meune ti wax sa life nga ni bou yabo japé sa bop the king bling affaire de ado (Ro-Gee) Dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado (Ro-Gee) Hey Hey Gneup gneup bégué leu bravo (ODD) Fo teule gnou souk jébalou déf la hero (ODD) Dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado(Ro-Gee) 1er couplet (ODD) Check it ! Hey am si taf sithiou Meun di mélastikou jaay prék wath tchi coner bi khatiou fipou Fook sa bop hercule, meune nga réndi pitbul Jiko bakou n***a bi linga fi taane jékoul Bayil ra**oul, dina la gagn bobo Defal nank nank tegui tank tank mado Hey yo feelo, louko moy nga K.O Tok najou bokatou réthiou mate sa lokho Oho ma do yéd la si primo Tas de doff cach wala moujou dougou ca**ot Ay bobard connerie tas de bétises Done intelec thi xél, mak ame maitrise Défal sa yité nga nité kharé ame dignité Jougal niaffé khouss mouss té bagna goudé Ndank ndank téguil sa tank Tieupi di tieupi di teubaka dal rék niak Refrain Kou meune ti wax sa life nga ni bou yabo japé sa bop the king bling affaire de ado Dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado Hey Hey Gneup gneup bégué la bravo Fo teule gnou souk jébalou déf la hero Dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado 2éme couplet Ro-Gee Fok sa bop mak ba do jeuli bi yaye di wax yang si mbéd mi Nga kham ni niak khélay takh nga jomi fis warning (moytoul) Dou ki tchi télé bi la fan dafay toukh dina ko jéém folow the bottom line Fils bo beugué jiguén na nga mouss, ame tchi liguene bagna khouss Be the best like all my dogs Fils dou tiaguini ghetto nga deug hood bi jokh ko gueud Bou town bi mété dou mandi rékay deugu Say laaf sakha goul sa maagu matagoul Li gnaw waragoul sa gondi takhawoul nékoul Kone na nga kharé bi yoone do soone Reflex, relax, no stress doga réss li déss ya yoon (Héy let's get it on) Jape sa coner project gondi bay waja maguét Ya ain't touch the sky booko jémé rék garé Affaire de ado mola nékh mola nékh Japal ni dafay jékh sou b**ba lane moy nééékh ???... Refrain Kou meune ti wax sa life nga ni bou yabo japé sa bop the king bling affaire de ado Dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado Hey Hey Gneup gneup bégué la bravo Fo teule gnou souk jébalou déf la hero Dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado 3eme couplet ODD Hé yaw dokh dokhal sa yoon, moytoul moujou fou boon Kharé roy tchi babylone, nono yaw téguil bi yoon Setatal sa yoon hey dawg forgeting this one The positive one wowowowa léral sa yoon RO-Gee Moujé dak khouli loy yakou di joy stop Bi mak di wakh ngay réé fok ni do déé nane gate Diay prék moy lou bess mandi rék bou dara déss Man stop it stop it bala réthiou wééss man Refrain Kou meune ti wax sa life nga ni bou yabo japé sa bop the king bling affaire de ado Dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado Hey Hey Gneup gneup bégué la bravo Fo teule gnou souk jébalou déf la hero Dou nékhna lool di foo di blow di képp cho beugua aak man affaire de ado......

You need to sign in for commenting.
No comments yet.