[Intro] Ya dun' Knowww/ Grandiz / EyeSaw #TheEP /HamgaYoyu/ Chambaii [Verse 1: Retsam] Buguma duga sii dara Buguma yeksii rek ngen defatii joini Kara Buguma doxx dii sigii dii para Buguma gis nyee dornii chaga Gudi bu nekk dii fashion night Haleh yu saff nii chebu jagaa Norpinaa teh dumalen setlu naa Gestu naa maa dajj sii ndo bouy sekh dii fompaa lips sii paa Byl maa doxx nee gisuma Yalnaa yagaa sutura Maa jada konj rek ta**ek maricon bii sh** be kissima Oh my God korm Ebola Fogonaa neh dewon naa Ngen moitu goor bouy jutu sumoii yekaa deflen domoda Mandem nyepaa dem Lybia Di ghetto youths ah suffer Jollof melnii Buntii Syria *sing* Choww bii yepp sii bitii laa Bunch of Fatou Camara I type and lash hard you call me keyboard warrior Key board warrior key board warrior I type and lash hard ncos legii xamna neh sorinaa [Hook Retsam x P-Thug] Bull Wahh -Bull Wahh dara Dafa Amm lor musaa gorm wahko teh bull musaa para Dumaa Wahh - Dumaa Wahh daara Diww Sangam defufii daara Teh dunko musaa taga ''ahh'' #MumuNation *mute tekk* #MumuNation *mute tekk* #MumuNation *mute tekk* #MumuNation *mute tekk*...... [Verse 2 P-Thug] Mann njoll mama la yokotei yeguma ndama Fii kufi dem beh falu rek sahh mbaga Kom bu*terfly Company wey ak yoi gen Ayut yena boka fly Lana tahh maii mute tekk teh yenama dramatize Taah ma gadu mic don si bandi Ken dafaatufi ngirr yallahh derem ak derem Last time ndobi nema nyehi cobo munuta simm cheram Nii lako dohaleh ni hach basa buntii keram Wanteh wahh bi nyarr laa ndah hach na chi buntii cherem Mute Tekk no duma wahh fufu, system b nyepla drown lileh tah ma ragala sobu Gayangi ragala tohonyu teh kanilen tuff nyepp Denyo build MBA NYU destroy harr b yagana teh gisung dara chi lung NYU dik boi [Hook Retsam x P-Thug] Bull Wahh -Bull Wahh dara Dafa Amm lor musaa gorm wahko teh bull musaa para Dumaa Wahh - Dumaa Wahh daara Diww Sangam defufii daara Teh dunko musaa taga ''ahh'' #MumuNation *mute tekk* #MumuNation *mute tekk* #MumuNation *mute tekk* #MumuNation *mute tekk*...... Bull Wahh -Bull Wahh dara Dafa Amm lor musaa gorm wahko teh bull musaa para Dumaa Wahh - Dumaa Wahh daara Diww Sangam defufii daara Teh dunko musaa taga [Outro] Ya dun' knowwww/ Chambaii