ODC - Mame Premier (lyrics) lyrics

Published

0 238 0

ODC - Mame Premier (lyrics) lyrics

[Intro] Amneu gnima begn, amneu gnima beugeu Amneu gni di fenn, amneu gni wakh deugeu Dinegn thiow, dinegn hate mais seneu wakh mo beuri Kham nagn kane moy kane, kham nagn kane moy kane Young fif zo dollar, adresse bi sicap leu No djoutou gang team bi nak buzzlab leu Dougnou wakh ac yow beneu mot niou tate leu Sa papou pappeu ne le wakh kouy pappam Mame premier, mame premier,mame premier,mame premier(x4) [1er Couplet] Mane leu young fif premier, sama team mo meuner Khalé fekkeu pa yi def lene bébé dakh nénegn les derniers seront les premiers Kane mo beugeu problem nieuwlene venez? Recolter lougn fi seumer n***a na ko deffal sama bopp boul dof damay hustle meli boy bou pappam renier Somay press ay rappeurs né ma bon apétit Niom nieupeu meu makk pourtant c'est mes petits f** senni votes, senni media, doumeu révélation de l'année ya yékheu sip Awadi duggy tee nénegn may deugeu bi Rap bo doul dégeuti, capsi ma yékeuti Yenene rappeurs yi di sop dougn ci lene dagni weur rek di fene melni politique Doul rek ci deukeu bi Rimes ay tonnou flow, ay qintalou syllabes Punchline you lay def li marteaux defone talla sylla Kene gnéméwoumeu clash? je vous montre comment faire ça! Omar vs Omzo... Real vs Barça Refrain [2e Couplet] J'ai un détour d'avance, rien a foutre de la chance été bo meu guissé boy damey am cla**e,pourtant nieupeu kham ni moussoumeu cours de vacances Yélé yélé music baaba maal, dageuti sa bop melni sahaba Katana, dageu na May sene mame....ADAMA Sama meune meune ci rap meyou yalla leu do ci meune dara kone diokh meu billets n***a Tout ce qui brille n'est pas de l'or mais ce qui est de l'or doit briller n***a! Zo Dollar Zo commence Zo fini! You f**ing wit da monsta... zoophilie Rap ay couplet you pas net, lepp ci sama deundeu guéneu ni janet Si t'es le meilleur rappeur au monde c'est parce que omzo vient d'une autre planète 0+1=1 la jangeu da melni lolou legui ay fenn leu Zero geu may One té pourtant mane ac yow dougnou benneu Refrain [Outro] Wakh bou barri bi est ce que diarnako Niou yorre game bi nieup khamnenko (Buzzlab) Yan boy nio yekk si public bi wey lepp A ba Z Concert ni dor ba parre public bi yekk tagolen (Eskey) Nian*l rappeur yi sen rap bi bakh Ah! Niet likhla** ben fatiha (ndeysane) ndeysane Di doul nane denen coming soon (Ah) Te sama team dele coming soul Mc niata lelen fey n***a (wakhal) Nenale liguey rek key fey n***a Wakhnale adress bi sicap le fi buzzlab le niole tat diour sa pape nenanme Mame Premier (x16)

You need to sign in for commenting.
No comments yet.