Nix - Boul ma méré lyrics

Published

0 284 0

Nix - Boul ma méré lyrics

Nix – Boul Ma Méré (Lyrics) Hook Game bi yeufou hustla la boy boul ma méré Yague na ci game bi boy meussouma wéré Chérie danga toy yeah baby kaay gnou géré Game bi amna khaliss boy fils kaay gnou géré Né negn ma "Nix bayil blow" (Nix bayil blow) Wala "Ma beg ci yow" (Yeah ma beg ci yow) "Meygnou touti flow" (Meygnou touti flow) Ok! Ok! Ok! Ok! Ok ! Wiri wiri diaré ndaré fils ma dieulate péé dila khaar Yeah N-izzi's back, dakhe le job dakhe le party (dakhe le party) Yeah se son truck bou panne le ding ko garé Guénéma sa guemigne bes boma wonné dinga diahrré Indil la lou raw kharé, rey gayi la fi néké deuk ci diaalé Yalla nama Yalla baal indi na fi safara Hip Hop khall damn! Yangui worou galé, yangui saalé Bimey Def lou ma Xam PBS mou ngui woy Boul Falé Dafa am gnouy kholé, am gnouy liguey di daan sen dolé Am gnouy tök ci bopou kogn bi rek di doul di bolé Snitch le wala dou snitch, man b**h le wala dou b**h Samay kheul la yorr boy fo guissé Porsche bougnou doul kheutch!? Maylene gnou dieuw ma balaa ngay nande sa raak roy ma Bou souba sa b**h joy ma ba nopi foutekou khoy ma ! Dou souba tey la, le temps ngay job N-izzi rey la Boul ma rey ak wakh damay khoslou fils fayma Hook Dama done fo ba gaagn la, sandi kaddou khaagn la Dotoul studio waagn la, son bou bess la, agn la Sama gaayi degn ko khiif, punchlines yi thieboudieune la Today c'est sarakh day, mc's yi lay def talibés Dagnou meusseu dieuli town bi, diokhé temps bi, kepp gamme bi Mangui ci sen biir di laake leneen ni Galsen ak Gambie N-eezy supa grandé, mitraille les yeux bandés Sa dadj yi dinegn watche tey fils fo mounti mandé Fame yé sakkane, style yi, sho yi yangui diokhé sa bakkan Aka ma leen lakkal, sen doul yé leer ni "Plan Takkal" Boy mané show me the money, ndakh gnou meune khoukhal none yi Ngen meune taal sen bone yi, sho yi meun gnou def sene you bone yi Mane la N-eezy gentleman, dou ay yeufou gondi boy nonou le mel Rap bouy khodiou boy solou ba bagn sa rap dafa khawa def taatouneen maaaan !! Shut the f** up boy te nga bayignou gnou job Nga done sunu khadjou galé gnou mey la nga thiop Hook Shorty... Kaay gnou... Géré... Daadiou... Ki moy Black Crys mo gueneu gnoul wa Joal Fadiouth Doto kham lou diaadou nekh na ci sey youkhou Yes I'm going in!!! Ding ma né merci beaucoup! Douma la dieme gondi ba di la fène soudé may faye Meun lou may def tek ci rew : Souleyman Faye Haha I'm just having fun man Mais wakh ngen deugue "Rap wolof mo raw"... Bring the hook! Hook Https://soundcloud.com/nixofficial/boul-ma-mere

You need to sign in for commenting.
No comments yet.