Nix - Badou meun lepp lyrics

Published

0 374 0

Nix - Badou meun lepp lyrics

DOFOULO DJINNÉ PÉSSOULA, (X4) KHAMÉ NGA KHAMÉ NGA KHAMÉ NGA YALLA AK YAALI KHAMÉ NGA YALLA AK YAALI KHAMÉ NGA YALLA AK YAALI KI LEY PAADIAL DILA DOUTE DILA YAALI BADOU MEUN LEPP {VERSE 1} NDIAGO BI NÉNAMA NIKISSI KHEKH BI DOU DIEKH BA NGA PARÉ CI GNOUSSAL GNOU MC YI DIAPE CI SEDALAL BIÈRES YI GNOU YAKHE FI KHOLAL MA KHALÉ BI NGA ANDAL NON BOKOSSI DANGA DIOUP LOKHO NI OGUCHI DOUGAL REK NGAY DEF OH QUE SI ni**a YAY DOGAL GNOU TOPE CI YANG MAY KHAAR BOY MAIS NAA LE BEETE GUEUN LE TANG FILS CI KHOL BOU SEDD KHAMO GATT FILS SA KHEL A GUÈDE CHAQUE JOUR NGA GUENT NÉ MANG LEY YÈDD NON MAIS FILS DANGA NIAKE DIOM CHAQUE JOUR CI BEAT BI GNOU DEF LA DOM CHAQUE JOUR NGA DIEBALOU TEK SA AUM MAN MAY ALCOOL BOUY FEDJ SA GAUM ni**a GNOLA GUENEU DÉ KODJAL SUNU CONCERT CI ARMEL BI CHAQUE JOUR GNOUY REY AKI DEKIL RAP BI RAP WOLOF DOU SAMA GAME MAIS SAAYOU MA PLAYÉ NGA MOUDJÉ SEETI ARBITRE YEAH DAMA NEEK, DAMA SOKHOR MAY PROFESSEUR BOULA DOUL MAY SAKH NGA TOKHO DOFOULO DJINNÉ PESSOULA MAIS BEUSS BOULA PESSÉ DINGA KHAMÉ SAMA LOKHO {REFRAIN} DOFOULO DJINNÉ PÉSSOULA, (X4) KHAMÉ NGA KHAMÉ NGA KHAMÉ NGA YALLA AK YAALI KHAMÉ NGA YALLA AK YAALI KHAMÉ NGA YALLA AK YAALI KI LEY PAADIAL DILA DOUT DILA YAALI BADOU MEUN LEPP (X4) BOMBARDIER MODOU LO : 4 APPUIS (X5) YEKINI BALLA GAYE : 4 APPUIS (X5) GRIS BORDEAUX EUMEU SENE : 4 APPUIS (X5) N-EAZY RAPPEURS YI : 4 APPUIS (X5) {VERSE 2} GAME BI DAMA KO YAAGUE DIEGUI KHAMOMA? SA GUEL MOMA DÉGUE NGA WAGNIKO NGIR MOU SORIMA KONE NAAKO LAAL AK MMM BOU GOUDOU KHAMATOUMA SAKH BOY KAGNE LA DJOUDOU I'M SO FRESH NI DI DORA FOUDDOU NDEKI CI LAL BI NI LAAKH CI TOUDDOU RAP GALSEN LAY SOLAL MBOUBOU DÉGUENA SOUMA FI NÉKÉ DO THIOP MOTAKH SAYOU MA TOUKÉ NGA YOUKHOU « WEER BI FEGN NA » RAPPEUR YI AKA GNO KEUKH AK LOUMAY MÉYÉ YEUP GNOU NANE N-EEZY BONE NA MOUN NA LA GAAGN AK AY FLOWOU DEMBE FLOWOU GANAAW SOUBA LAY MÉYÉ SOUBA CHARLATAN LA MAIS DAMAY KHOUDBEU AY TÉRÉ GUCCI CI BIIR SA GUEMBE 4 APPUIS 4 APPUIS MY ni**a SAAFARA FLOW ni**a MANDI NGA TECHNIKOU DIOUF WALA FADIGA MANAAM GAUCHE WALA DROITE ni**a TAALINA MANE AK RAP BOY NI JUSTO AK BALBINA NI CONGO DEGN MA DÉSIRÉ KABILA DAAN TÉLEU YÉWOU NAAN DIANGUI NAA DIADE COGNE REK SEYYY {REFRAIN} DOFOULO DJINNÉ PÉSSOULA, (X4) KHAMÉ NGA KHAMÉ NGA KHAMÉ NGA YALLA AK YAALI KHAMÉ NGA YALLA AK YAALI KHAMÉ NGA YALLA AK YAALI KI LEY PAADIAL DILA DOUT DILA YAALI BADOU MEUN LEPP (X4) TYSON TAPHA GUEYE : 4 APPUIS (X5) GOUYE GUI MY ni**a ZOSS : 4 APPUIS (X5) AMA BALDÉ TAPHA TINE : 4 APPUIS (X5) N-EAZY KHALÉ BI : 4 APPUIS (X5) N-EEZY DIAARONE NAFI WAKHATIFI AY NDIAKHOUMEUM DOKHI LOKHOTI FI MBOTOU GAYI PARÉ YOKHOSSOU FI AY MC MEUNEU GAAGNÉ KANE MO LE GUENEU MOUNEU DJELI CI SA GAME BOU DÉÉ BI SOUDOUL N-EEZY BOY TÉ DOULA DJAAY DOLÉ NDAKHTÉ LI NGAY MENEU YÈÈK YEUP MOUNO GNOU DJAAY GOLO AMOULO FI NÉLAW DANIOU GAAW DINGA WANNE NGELAW

You need to sign in for commenting.
No comments yet.