MoonTee - Dou Cii Neene lyrics

Published

0 120 0

MoonTee - Dou Cii Neene lyrics

Intro Yeah yeah Alright alright Yeah yeah Alright alright Yeah yeah Alriiight Refrain Dou cii neene, te guissal gnou wonei fitou gainde lingay diem Gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm (yem) Fitou kece douci Da ( daaraaa) Naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone Te guissal gnou wonei fitou gainde lingay diem Gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm (yem) Fitou kece douci Da ( daaraaa) Naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone MoOntee Hello dear, what's good, trynna open your ears Ci Douci neene lagnouy tek, n***a trust yourself Nanga gneme linga doone, bagna nekk ben nitt kou boone Soubeu beu ngone, yangui ci bopp kogn bi taakiy boone Reub nga, keud nga, thiole nga Yangui ci jail bi teud Why not nek ben clean boy, nangou degu deugu Mbir bi len leu, yallah keneu leu Bouldi nangou tokk di xaar balle bi taakk neu.. BM Dou ci neene, gnou songu hip hop mou done sougnou gun Kouci nekk ak lila takha rappe gueumal linga done Gni di boone, gni di wine, gni di gadou gun Fougnu taxaw nei Mista rapper gnou ni niitt kou boone AlyGhost Yewou njeul def sa mind Dou cii neene Takk sa fiit gueum sa war reuthie lene Fiit dou djay, baay guinar bi dou neen Dawala daw adouna ningui mel Refrain Dou cii neene, te guissal gnou wonei fitou gainde lingay diem Gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm (yem) Fitou kece douci Da ( daaraaa) Naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone Te guissal gnou wonei fitou gainde lingay diem Gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm (yem) Fitou kece douci Da ( daaraaa) Naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone AlyGhost Yoh Check, fils, dou neenu neene Technikeul rainbow dh raw na len Kou ci beugu men, gnou dikk wone len Fitou gainde ndiaye bi nekk ci gnouni neene Gueum seu bidew bagna ragal loufi neew Diokhe sa bakane neu naw, deugu doufi neew Mengalel sa bop king kong Rainboweu gui sing song yeah Kou beug alone seu life doko ping pong dé BM Doneul seu gainde bopp mission dagg loce Gueumeul seu bopp nangou dinga doni boss Diog sa fadjar tel dh woutum xeuy di doone sa guerre Lou waruta gnak tokk ci kerr lou ci doul neene dh doone sa doolei MoOntee Wiri wiri diari ndari leu aythia gnou xarei Mission de goor yallah leu na fiit bi barei Kone bro trust yourself Don't listen someone else Gueumeunl ni dinga ci guen n***a by yourself Refrain Dou cii neene, te guissal gnou wonei fitou gainde lingay diem Gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm 'yem' Fitou kece douci Da ( daaraaa) Naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone Te guissal gnou wonei fitou gainde lingay diem Gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm 'yem' Fitou kece douci Da ( daaraaa) Naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone, (x4) Outro Gueum sa bop fiitou kecei dou ci neene, 'douthie neene 'fiitou kecei dou ci neene Gueum sa bop fiitou kecei dou ci neene, 'douthie neene 'fiitou kecei dou ci neene Gueum sa bop fiitou kecei dou ci neene, 'douthie neene 'fiitou kecei dou ci neene Refrain Dou cii neene, te guissal gnou wonei fitou gainde lingay diem Gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm 'yem' Fitou kece douci Da ( daaraaa) Naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone Te guissal gnou wonei fitou gainde lingay diem Gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm 'yem' Fitou kece douci Da ( daaraaa) Naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone, (x4)

You need to sign in for commenting.
No comments yet.