Grandiz Kroo - Mbalahuma lyrics

Published

0 125 0

Grandiz Kroo - Mbalahuma lyrics

[Intro] [Hook x2: Napz] Ak lu yon b meuna lendem damai huss okay Riginta** yengaluma rap la choose all day Damaii rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma Damaii Rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma [Verse 1: Napz] Kalamay hardcore hajut c gemin mumuneh, no no Sunn ko sekkeh dii nga daww pipeline beh kubuneh Sa ngensor bii ngai sol dii tobb dii dal dii jai skinny Sii man dey ova dang ni jongoma bu rock bikini, uh Sa rap ah telleh tah nga daw songu mbalah Deuka si tilimal sunu game Beugeu lu noi teh cheap ni charakh Sarahu fan man lako tudeh, Sodon yeg sah nulei wureh Stay loyal to the game ba nor sii heyeh nang sii gudeh Jel mbalah beat tererari tankhal sunui nopp Wer ko sii game dohut fek seni rapa wopp Ku Jogay sii lu hard utali lu noi mein pachah nga Since you like tasting different sh***s defii len pachanga Kon purr mui lerr Sa game a tilim melni eutu mbam Bi diss nala kumpa ni sa sufu malanu mam Wah jeh baree so its high time I made the point Ku rap mbalah don sa pain na nga faju with this joint [Hook x2: Napz] Ak lu yon b meuna lendem damai huss okay Riginta** yengaluma rap la choose all day Damaii rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma Damaii Rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma [Verse 2: Retsam] Uh, Nga amm sa problem yeksii rek maa yokasii duma Marka** dui harr beh friday jott purr jubalii juma' Damaii rap mbalahuma, bagg-bagal yegaluma Sen ta**u aki tessanteh safma Xessalu Aida Patra, uhh chambaii Gemenj you xessaw, nobb ndurok marche sandaga, chambaii Sen instigation against hip hop, boy julatuna Fatuna, yagana, mission bii matna aganaa, cypher Ma by prince ali johlenn kor rap tangana Majohkokor ?''Johkokor'', majohkokor ? ''Johkokor'', uh Mann duma morm, naa, mann deh duma morm , naaaaaaa Bunch of drake babies please delorlen senn mum Ndahh youssou su degeh lee dii ngenn amm problem ak morm Damaii rap mbalahuma, lii ngay deff netehtula Buguma tcheh laal dara sama loho henj subaa Damaii rap sama rap, nga mbalah sa mbalah Don't call it rap mbalah ndahh boy lii ngayy deffa lahh [Hook x2: Napz] Ak lu yon b meuna lendem damai huss okay Riginta** yengaluma rap la choose all day Damaii rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma Damaii Rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma [Outro] Ak lu yon b meuna lendem damai huss Riginta** yengaluma rap la choose Damaii rap, damaii rap Damaii Rap mbalahuma, damaii rap mbalahuma

You need to sign in for commenting.
No comments yet.