Fire - Xamouloma lyrics

Published

0 105 0

Fire - Xamouloma lyrics

Couplet 1: Lo def malako dakk may badou meune lepp Game bi nekatoul rap mais kou dakk lebb Fii dafa tiliim tei chak jour niouy setal Fii ngeye raak ba deii niou togg dila setane Fi sene khela gatt motakh dougn goudou fane Fi ghetto bei stylé melni ay mbeddu Fann Mangui ak hamadi niou todd tekk warrga bi Fekkei maci bolei ma dieul raw gadou bi Magg daane tei ngembo ngembou khalei Reye la nga seugue sigilela ndigalei Loutakh manane lene ghetto bi da stylei mane dong nekone thug ci ay enfant gatei Fii bene baye fall rekaye diakhal kogne bi yeup Bima dioudo ba legui hamouma dadj di deup p**y oubekoul defena mon guene yomb Bi tedj lene sene taate yi mo guene kou nieuw rek romb Bene vidéo niounane fireminati n******gs so funny douniou khamtei dougn ladjtei Bind ba mame nane ma kocc barma fall Nekone khalei bou ndaw done cons Bambaj fall Dama changer sama tourr pour meune bokk Mais changerwouma sama jiko pour rek bokk Bouma khamoul sakh deima nian*le mou yokk Dama dioudou daldi tiital samay mbokk Ci fanne you neew la reye nitt kima nekone Dou pour iow kone limeye def boul nei da bone Esk dinga guiss niit nane dangakoy diokh ngogn Boula knockei esk kene dinagn ladj kou togn Talent amoul boy, ligueye rek mo woor Weer bi dina fegne tei dou done werrou koor Khel di Gnafei beuss bou nekk moy yonou goor Legui lepp nieuw fettei ci souniou boor.. Ibou Refrain : Xamouloma, n***a xamagoma Boumaye nieuw yene nieup laye bett xamagoma Bo beuguei biff, n***a woma Ladjtel niata rabou alle laniou diomal Xamouloma, n***a xamouloma Boumaye nieuw yene nieup laye bett xamagoma Bo beuguei biff, n***a woma Ladjtel niata rabou alle laniou diomal Couplet 2: Damay rap dila diangal ni sama gars konzo Mane la nieup di weurr meye melni la conde-jo Dama ham yone bi ni kou dei baye doundate Mane la nieup di khaar ni real ak barca Sene khela vide ni sama casier judiciaire Demagougn sakh guissna sene gale yi di taire Douma khol depart bi wantei arrivei bi motakh limeye khel di fayeikou di chère Gniko fonkoul la sene tchine di bakh ngerr Back to reality fi amoul diannère b**h bi sama snap nena dama mignon Poche diss na mais fokk niou lale ay millions Niata nio parei bimlene neeii mangui nieuw, ba teye dji mangui ci kaw Lou adversaire bi tangue bou parei wakhko mou nieuw, niane yimay niane defna ko bima dieuli ji communion… ibou Refrain : Xamouloma, n***a xamagoma Boumaye nieuw yene nieup laye bett xamagoma Bo beuguei biff, n***a woma Ladjtel niata rabou alle laniou diomal Xamouloma, n***a xamouloma Boumaye nieuw yene nieup laye bett xamagoma Bo beuguei biff, n***a woma Ladjtel niata rabou alle laniou diomal Couplet 3: Boma hamoul dema wowe EH wala nga woweima king bi Liy bakh loutakh mouy khegne nekh da fekk bobou mongui ci tchine bi Nioune daaniouy music tei douniou def fausse note motakh fi khamougn kouy thione seck Nene dou meusseu guiss souf bou noy nane dafay dem di dale ci ay keek Fekkma ci yone bi mey dawal 205 Hamouniou loudoul hustle hamougn loudoul niafei Namena lolou tps yiniouy reréji sombi Legui calculel calculel ma guenelela somme bi Mangui def ci souf pour meune yegue ci kaw Lane lay guiss boumalene di khol ladjko pithie biy naw Beusse dou touti borom leye tolol sama nguentei ni 4avril Damay todj game bi nga fekkma mbside ma togg ci samay n***a diap tchill Guissngama meye takk rollie bi melni n***a damako tamone Guissnga kene dou wakh ci sama succès melni n***a damako tamone Mangui dokh di nieuw guissna n***a yi tekk sene mic melni kou guiss camionwou 100tonnes Legui game bi dafa diha**o melni bene kogne bou am 100 kogne

You need to sign in for commenting.
No comments yet.