Elzo JamDong - Yow Lë lyrics

Published

0 307 0

Elzo JamDong - Yow Lë lyrics

Intro Yow le, yow yow yow le Yow le, yow yow yow le Yeah Verse 1 Seme khol fess ne takh nga mey podj Nala defeul lo guissoul tchi ben gore Sey tiono dieekh neu maye kiley sore Waw gore doumeu bokk thi gore yi ley dore Guiss na ci sey beut khaar nga beu soye Guissoulo kou sérieux takh ne ngay dioye Sey rangogne fer neu maye kiley yor Niom ay kholou kheer legn yor mane mey or (han) Wone ngama fouleu ak diom Wone ngama wone ngama ndioub ak ngor Soubeu ak ngone dina dioubo ak yow (ak yow) Yama takheu beugg diour ay dome (yeah) Bou sobé Yalla dinga sout se aye none Dinga diouyo ak niom gni beug doulo ak yow Dinga done boure dinga soure am forme Be gni leu beugone lor beugg ndouro ak yow Yow la beugg nala takkal bague kenene kouleu beug takk nako takkal ay pote Deug deug diaral nga ma raag doumeu doyeul dileu tagg gni le nièè di ko thiow Yafi tek #tank yaye #bombe kouleu #guerre nako #gun, #militaire laay done Binga dalé tchi mane le se khel wara dal, dinaa dem diakk dinga dem Mairie sol robe Chorus Yaaye done ki diour semey dome Someu degueloul demey dofe (yeah) Yaye done diour semey dome (ooh yeah) Seme guenne walleu ngay done (woah woah woah) Seme guenne walleu ngay done (woah woah woah) Seme guenne walleu ngay done (ooh yeah) Seme guenne walleu ngay done (woah woah woah) Yow la tanne, yow la tamou (woah woah woah) Guiss naa tchi yow lou ken amoul ken amoul ken amoul Yow la tanne yow la tamou Dinga am tchi mane lou ken amoul Bridge (woah woah woah) Yow le x4 Verse 2 Thièbou yapp bi khègne neu (khègne neu) Amatoumeu loumey neubb lepp fègne neu (fègne neu) Yagg naa dadialé ay thioro wayé limeu meusseu am tchi diangoro djiguene yeup dégne neu (han) Gni leu togne togn negn meu Naaw dou wakhou pitch ay wakhou wégn leu Dem thiakaye di tal seme money dou limeu gondi guenne balafi defey fekk me bégn leu (yeahhh) Legui Takussane diot yaggueutoul, yaggueutoul legui takk sey diot Legui semey goro dal di sakkou sene dote Legui pa yi diogué diakk dia nga tagou sey mbok Mousso dem beu finale ak man Mouss nga touki wayé dinga dem fenene ak mane Denk negn mele nga fanane ak mane Seme dekhou bannekh ding fa nane ak mane Tey le biss bi dakh seme life tey la dogueu ne kilifa bimeu yagg beugg done (han) Seme mbokkou papeu yeup beg Souniou santeu dineu law diaré tchi kou rafet khol Mangui fateulikou bimeu done guente dileu khole di tchi meun diamou souniou Boro Yangui yek pekh mi woné gningui tchi yone? ndakh néneu sey bokk ne limou gueuneu sopp Chorus

You need to sign in for commenting.
No comments yet.