Elzo JamDong - Khoudar lyrics

Published

0 297 0

Elzo JamDong - Khoudar lyrics

Intro Yenn saye dingueu guiss louleu dieulé kow lolou beu diapp se bopp kessé ngay meun Fekk ngueneleu laakhou tchi guinaw bobou fitna ndakh Yalla rekkeu kham ak di def li gueune Woah oh oh Yeah yeah yeah Woah oh oh Woah oh oh Woah oh oh Yeah yeah yeah Woah oh oh Woah oh oh Verse 1 Bi Moussa waré ande ak Khoudar def ko né dinga diang ak mane defal ndank ak mane nanga ande ak dal Dinga guiss louleu yem wayé nak nanga dieme diokh me se kaaddou né do and ak hal Kou nek lileu Yalla mey Nieupp mounougn done benn Ladial phiraon mi Yalla dieye Beu mou fouye beu degg deugg leu done begn Guiss diongoma diou sey ta** Waroul takh ngay kha** Khamoulo lou tchi fa**ou Beu guissogo gore beug khey fa** Moytoul me dieek diou romb rek Diekk taarou ngané dee dou yomb Wala djiguene diou lamb Ngané no def ding ko lamb Pre-chorus Judge not khel matoul boul wereunté tchi lou se yone nekoul Dieuw ak fok ne am ne diam mo tané yenn yi kou gueum dou ko def nekkoul Chorus x2 Yenn saye dinga tite be se khel nara diakha**o Yenn saye dinga fire be se khole nara diégué seuss Yenn saay dinga tite ba sa khel bara diakha**o oh oh Wayé bepp fitneu toudd Yalla nga tchi wara ndieukk diemeu rakha**o oh oh Verse 2 Borom bi dey missal Binde ne lepp be noppi Segueum gni kham nioye teye Kou niakk kham wara gueuneu noppi Kou wekk lepp tchi guissané bo Dtouwoul adina dinele sappi Bouleu khiif takha salite My brother Yalla bouniou niakk soppi Li khew tchi mim rééw Gueunoul yémé bitim rééw Mystique tchi biir guééw Wayé Loukhouss dou firim rééw Se deunkeundo boul kheep ndieurigneum Tagg sey kilifeu dingate Serigneum Téyé se kourouss gaddou se satala Deukk tchi dieuw yakkh der yeufou satt leu Pre chorus Chorus Bridge Yenn saye dingueu guiss louleu dieulé kow lolou beu diapp se bopp kessé ngay meun Fekk ngueneleu laakhou tchi guinaw bobou fitna ndakh Yalla rekkeu kham ak di def li gueune Yenn saye dingueu guiss louleu dieulé kow lolou beu diapp se bopp kessé ngay meun Fekk ngueneleu laakhou tchi guinaw bobou fitna ndakh Yalla rekkeu kham ak di def li gueune Outro Lo fi def dinegn wakh Lo defoulit dinegn wakh Yeek tchi mbame womate mbaam Ken dou tee dinegn wakh

You need to sign in for commenting.
No comments yet.