Elzo JamDong - Tiim lyrics

Published

0 225 0

Elzo JamDong - Tiim lyrics

Chorusx2 Souniou none yi ngay fek niou tite Ken dou attane souniou tir Wakh mounoul break souniou team Ndakh Yalla dji rekkeu niou time awright Mané Yalla dji rekka niou tiim alright Mané Yalla dji rekka niou tiim Verse 1 (Eh yow) Lidieunti buzz tchi seu insta te mounoulo fadj se sokhleu Nioddi nga gangsta gangsta motakh seme son guenne sokh leu Beurilé na ay style wakh me lo sokhle me diokh le diokh le Am na aye douce, am na aye dure Bo beuggué yokh leu Yokh le yokh le bo beuggué yokh leu Nenegn le forcer bi sofe neu (Moss)Se carriere bou gatte bi off neu ne Ki rappeur yeup né dof leu, mom le sandeye yi né thiofe le Wayé diem ko napp mou tiope leu leu Se yonou cimetièrou Yoff leu leu Boul indi haine tchi seme flow Bayil rek sho yi di gueuneu tewe C'est ce qu'elles aiment tchi seme flow Deme yarou te mounone na gueuneu rewe Diaroul zèle tchi seme show Deme manou te mounone na gueuneu bewe Law ba faweu niou takha diok diok-Yalle ne niou Yalla mousseul tchi khewe Ki leu gueumlo ni yangui tchi maket bi nakh nele paré tchi yow ya tchiy diagg bi diagg bi dinaleu lekk ni spaghetti Mane mangui tchi magg tchi mangui Chill, te maaye ki tchi nara maguetti (maguetti maguetti maguetti) Hook Verse 2 Deukk tchi beef deunguey ree beu ta** Niaata legn shoot ndakh rap de tess Fethial bou baakh ndakh lou teugg ta** Jobal se fey Yalla moko ress Deukké di fo legui ya tchi dess Boul khare niou dore le nga dow ni fa** Da** ko be dowal se Mercedes Souko défé do tacléti kenn pa**e Hey khey liguey seye Fekhel be kham se way Loye def ne done loye niane mou weye Weye ankey mane sentou woumeu lou nekkoul pé Moussoumeu yeg se hate ndakh mounoumeu téré me diot seme fey Free se bire iphone chi my friend moytoul thioy yi palper leu Yow mi di woté real hardcore di binde ay fene ndékété aye nappé leu Instant bi ni sakh bok mey nala ay fan nga taylé seu calpé nieuw Lep si dose ndakh dope bi strong neu dieulkatou coke yi niong tchiy barkelou Ki leu gueumlo ni yangui tchi maket bi togne nele ken dotoul rote si se pakette yi Mane mangui tchi magg tchi mangui chill, te mala gueuneu bakhlé marketing Hook x 2

You need to sign in for commenting.
No comments yet.