Elzo JamDong - Tchi Kow lyrics

Published

0 199 0

Elzo JamDong - Tchi Kow lyrics

Bimey ndieukk guiss seme clip tèlè dou wone dara tchi mane Khawme wone ma gui tchi revolution ni Sarafina Bo nékké kawe kén dou diapp ya ngui rabati sakh Bimey ndieukk degg seme baat radio dou wone dara tchi mane Khawme wone mangui tchi revolution ni Sarafina Bo deukké town degn le gueumlo né do dara tchi rap Tegone niou boy yi beugg dadialé ay tiaga di nawe Ken momoul ken-kén euppeulé woul kénn dara thi lenn Bou kenn khepe ken ngueum ngueum rek ak wara fi né Kham na aye galsén you meussoul dougg Carapid sakh Diakhlé nga khate diappal ni mangui dogueu tambali nak Rappeur yi diogué bitim rewe doumeu séne morom Gueunougn me dounde wala khamné culture bi amoul borom Dou kana bi wala kawemàne be niou tchi euppeulé walleu Dou cannabis dou coke virus le boye accro di ko wallè han Rame sogueu takhaw diok sogueu dokh Rhymeul sogueu takhaw am lo meu wakh Mouno loudoul commenter diniou critiquer baye Mais kenn dou fi defati ni Fi Free dikké baye Dama teylou thi Rap rap dogueu tédiou di rap rap Li ma deglou thi rap rap esk deglou nga kam? Mane deme free seme mind comme kouy fekheul relax Ancien Talibé magg degn me sekheul ci rap Ngane´doolé nguey tek!? hum, degn niou booléwoul rek: (nioune le) rakk yi ley rousslo sey kanamou rakk Malay indil baga**ou mak ngamay diokh sey sagarou rap rap Ngané tangouniou? ha-ha danga khamagoul rap Dadialé Kora, balafons ak Khalamou Rap Fawoume me feugg aye balles a fonds nga khalangou raam Deum ko beugg nob ko te yow def le diaraloul sar Boumeu nekkone guel maye done diabarou Rap What? Ne se ga yi dem dallouwate ren maye falouwate Balou akkh Tabaski rombeu rek me alouwate Dieul lene seni alouwé dellou deglouwate me bou bakh poete yi me meun diangal moune na lene waagni moun nako wate Waw Mane mane ma fi diaye poete Waw mane mane ma fi fly kowé la def Leopold senghor dey khate pour me atterrir Setane na se clip mais sincèrement se style c pas terrible J'arrive pas a tenir bullsh** bi beuri neu Bala lou baakh di am rek dal faut q me diogué be Paris koi Ken tchi ga yi amoul histoire vs avez merdé grave Motakh Concerou samedi soir di mel ni Mardi gras Ma daakh créer ma takh nga toppeundo Ah Ya daakh wéré kone bouniou tympaniser Moune nga topp seme band pour niou wone le yone Nieuweul seme live flow ba ngui waliyane Nel niom waly ak niom Titi bizness bi diamm leu Tupac dou dioték biggie bou nekkone affaire de lamb leu Bou nekone dolé kone Balla gaye nieuw tchi game bi Toudd se tour ni kendrick te ken dou tidji se guemmigne Music ba ngui fey gni tchi gueuneu mouss comme d'hab Gni né tchi soufe dinegn yagg khouss te combat Bi dou diekhe filek nio gui gueuneu pouss contrat you baakh yi pour nga am tchi faw ma magg couz Bou le mbed bi naw se wa gallé méré leu Bou dé tchi yow rap weteuli chomage le wéré ngueu Nele mbed mi daw se wa gallé bégué leu Mc bouy topato wa gallem mbedd mi respecter leu Detester me se droit le boul me diémeu tester Boudé tchi pa**é nga dess dé fi laley faté né mess dé Mangui ni di rap be beat bi egg 3mn pile Nga khamné limomey yokk mais dou diekheul semey pile HOOK x2 Mangui tchi yone Gni beugg peace negn me baayi di togne Negn ma baayi di togne Kaye tek tchi brique ndakh niou tabakh tchi kow Tchi kow, tabakh tchi kow Gni beug peace negn me baayi di togne, negn ma baayi di togne Kaay tek tchi brique ndakh niou tabakh tchi yow Tchi kow tchi kow tchi kow x3 Gore Yalla meunomeu titeul Bi nga deggué me dore nga sogueu nangou Peace up Pour se yone lerre homie moune naleu niteul Guiss na lingay sore wayé meunomeu disteup Gore Yalla meunomeu titeul Bi nga deggué me dore nga sogueu nangou Peace up Pour se yone lerre homie moune naleu niteul Guiss na lingay sore wayé meunomeu disteup

You need to sign in for commenting.
No comments yet.