Elzo JamDong - Nama Yalla Baal lyrics

Published

0 212 0

Elzo JamDong - Nama Yalla Baal lyrics

Pre Hook (Mathart) Taal bou Yalla taal wakh féyou ko Nama Yalla baal gnii ngui seen kow Takk shine lerr naagn ni bideew Taal bou Yalla taal wakh féyou ko Verse 1 (Elzo) Taal bou Yalla taal tole bou Yalla bey Diaam bou Yalla fal, dey gueuneu Ttaakkeu di gueuneu teuweu feye Fall kou Yalla mey daal lo beugg nangou tchi mom nanga nangou ni deung ko koye feye Ndakh kou Yalla mey baat dineu wakh te kou am bou neekh de koy weye Deme dane lakkhatou gni me diégué (gnimeu) deme lerrone seni beut beu niou goumbeu Gni me gueuneu sori nio meu done ndieukk sene mey takk di magg niou mel ni niou moumeu (moumeu) Niveau bi gueuneu kowé laye football Legui mbeur yi fi eupp gueudd laye doumeu Deme diok djité xaroumeu Adioumeu Mangui weur kane momeu soute te guissoumeu Soubeu ci Diante gouddi werr Takk na shine boul begn lolou ken dou tchi polemiquer Ngande la lerre neu maye thiaatou bidew bi dioudou fer di lekk tchi bolou mak yi Fangg na fegne na diommi nguene ndakh dolé dji nék tchi mane? mo gueuneu kowé dolé djinné Rangou na khekh na be togg Tchine gua ngui kheegne nekh te dou gowé tchi né Pre Hook x1 Hook Nama Yalla Baal (Yalla baal hey) x4 Verse 2 (Elzo) Yagg na def ay hit awright Bobou amagoumeu wone ay clip awright Li fi Thiere binde tchi recettou beat Eupp neu ay livre Diekhelneu ay bic (come again) Yagg na begueul ay nit awright Bobou amagoumeu wone aye sites (Wallaye) Bi ngay ndieukk degg limeu binde deugueu replay nangou ni kone mousso wone write (dope) Ma dakh rap Senegal Diallo Manekk tchi nguur gui def ko seme Freengdom Seme dope legalize soumeu nekhone guenné bum boumey touddé Dakar Kingston Dieuleul bi def ko Ringtone Gningui job te moussouniou am piston Kou le ladj ndakh ma ngui gérer fight bi neko maye Mouhamet Ali tchi kow ring bro Demey takk doumeu mandi Ay daadj naturel la andi Def le Mario diam le aye Champi Soudone western movie degn mey Wanted (wanted) Hey boumeu wone se kanamou Gentil Kham na yangui niaane me fey nga meun tranquille Demey ga** tombe soul ay garcon comme Gaston tchi microphone mane mey bandit Bridge (Mathart) From the underground liguey bi dorroul tey Guiss nga egg negn tchi kow liguey bou sete dey fey Kila yagg tipser lo kepp se good time Get sunu vibes feel alright Deniou dore mou nathieu n***a nieupp sèèdé ko wallaye Change game bi def safaar indi mousslaay Never never nga guiss niou tchi détails Wowéma grossiste one more time (uh yeah uh yeah) Hook

You need to sign in for commenting.
No comments yet.