Elzo JamDong - Kaay lyrics

Published

0 220 0

Elzo JamDong - Kaay lyrics

Hook Let me hold and protect you gyal Me nah wanna any tears in your eyes Let me hold and protect you gyal Nobody coulda coulda treat you nice Verse 1 Biniou khamanté gningui notre dameewd Defe romb seme gayeup ne god damn Khamone nani yagg yagg nako contacter Boumeu defoul lou gaw legui benene black dem Amoul wone numero portable Deme dane def baatou guel woté gallem Ay boy you ndow dounde souniou puppy love quoi Diaar negn fou sori loumeu beugg mouné maye begn Def negn au moins ay 5 ans Souniou mere yi dem beudi samm digueunté Mais defe diekki diekki soneul semey tympan Nane me takk me deme beugg niou nguenté Mane ko boo kharal me paré seme diangg sakh Mounoumele niane ci te amagouma laire-sa Mounémeu so gawoul rek niou mey me benene ga Manéko yafa dé domeu dieuleti fenene gyal Bou dembeu done tey doumako tontou Kou ko meuneu am di hésiter dey fontou Andoumeu wone ak sama sago ndakh tangg tey Nangou na dioum na te dina diangg teey Pre hook Kaay niou nekkaat Niou dounde happiness Ma yeah Kaay niou nekkate Paré na ya tchi dess Ma yeah Kaay niou nekkate Dinegn dounde happiness Ma yeah Kone kaay niou nekkate Mane paré na dé ya tchi dess Ma woh oh So kaay niou nekkate x4 Hook x2 2nd verse Miskine ndéké yaye first Soumeu dieulone seme temps doumele diaye seuss Guisseugoumeu ken am se ay qualité Soudoul yow amoul kenene koumey valider Mangui dogueu nangou ni dioume na Lou ni mel dotoumeu dal tchi adouna Pourtant khamone na ni kenn douleu gueun meu topp seme beugg beugg beu niakk le tey reuthiou na An Dotoumeu fatté se birthday Kham na ni def nala loye nakharlou beu tey Dotoumeu guenne goudi seytané yi guiss meu Nga yewou wakhkat yi fenel me dileu tristeul Yeah Pa**eport visa London ibiza Dinala yobou tchi deukk yi gueuneu diksa Dinala takk nga takk ni rizla Pre hook Hook End

You need to sign in for commenting.
No comments yet.