Elzo JamDong - Falaaw lyrics

Published

0 279 0

Elzo JamDong - Falaaw lyrics

Pre hook Yow kaay niou job ndakh moui tané bro Amoul khof talougn saalé sope warougn planer Kaay niou job ndakh mou tané bro, ndakh mou tané Amoul khof talougn saalé sope Hook Kham na lima beugg x2 Mang koy dound deug x2 Amoul lomay diangal x2 Bimay eksi seen naala lay niangal (seen naal angay niangal) Mais yafa niaaw Falaaw falaaw falaaw x3 Verse 1 Yow kaay niou job ndakh moui tané bro Amoul khof talougn saalé sope warougn planer Kaay niou job ndakh mou tané bro, ndakh mou tané Amoul khof talougn saalé sope amoul baalé Yagg diow motakh yaakh ak thiow Légui dam ci paré Dakhone fo maala ndieukk dore ak tokh cigarette Wayé no dama yagg fort mané faut que mou carré Faut que niou diok Borom meukh dome Mounoul khèkh ak armée Légui soy def liste Elzo'y djiitou Bougn sanione ma daanou Metzo Djatah Légui no def se sista né daf may bisou Firr dou takh ma waagni sama khadar Hook x1 Verse 2 Seme life aka beuri ay signe Fi meu diare douniou beuré ko sagne Nekhoul be nekhoul mais beuri na style Ladial gangor yi ak mbeur yimeu dane Deungueu diappone dingueumeu stop Mais deme tangg be time le nga mar Deme high, deme deep, deme tar Seme ga yangui deal seme crack Guiss na ni fi defe khate wayé Free lim fi dji defe sakh Nenegn le thiow li ngay thiowe ding ko bayi ndakh nioune nioye gni titeul se squadd Nekk ay k**er tchi rap deukké job kharougn 8 heure du mat Doper na mineur ak mag niou meu diappé me dealer bou mak Yang may diss (10) may play lou rey comme Zizou Ngay copier Biggie te se laamign rekkeu paata Rakk boul di sathieu mère ay bijou Bou leu aakham dalé c'est la cata! Bridge Kham naa lima beugg Mang koy doundou deugg Amoul lomay diangal Bimay eksi seen naala ngay niangal Mais yaafa niaaw Hook End

You need to sign in for commenting.
No comments yet.