Elzo JamDong - Waitin lyrics

Published

0 154 0

Elzo JamDong - Waitin lyrics

[Intro : Bako] Lumu yagg yagg déy nieuw Lumu tang tang bul daw x2 [Verse 1 ] [Kalz] Mangui dém ca caw kanam Souleymane gadoul seu xalam Xér béy doni done ngalam Tonil djeumeulél seu kanam Mic check, essai! Ngané ma do dem Do percer! Sameu carriere moy avorter? Waflash, Maa sané! [Fla] Gemeul job Bi my boy deubeul Dangeu nareu wor kone xeudeul Ndjeukeul yewou takou deugeur Deum yi sakh dégn léne di ndeupeul [Kalz] Droitier la mo takh méy job gauche Ndakh beugg fessal poche [Fla] Kouy djité niongi paré def putsh Bagneu nango took touche [Kalz] Dameu yagg khar souy nieuw muy nékh [Fla] Bayal seu waaar ni daara j Done ndongo done faada ji It's the school of life kone déy métii [Kalz] Yagg négn job ay CDs [Fla] Natt bi nio kéy tégi [Kalz] Djox meu beat meu tépi Djox meu beat meu tépi Xamougn bopp seu bopp, déniouy ték foundation lépp djok Done number one pour gni peu meu topp , mo tax dumeu messeu djouk si job [Fla] Talouma xar mbokeu joug war mana bok Mame xa ak bandi mic diko teugeu samay nopeu [Bridge] Boul meu séén Boul guiss méy tok di cool ngeu fokni mane Amouma... Luméy séntou si aduna,mane rékeu xam [Refrain : Bako] Lumu yagg yagg déy nieuw Lumu tang tang bul daw Weurseukou Yallah boy diarul xadi Lumu yagg yagg déy nieuuuw x2 [Verse 2 : Elzo JamDong] [Bridge : Maya] [Refrain : Bako]

You need to sign in for commenting.
No comments yet.