Elzo JamDong - TeauPla Anthem lyrics

Published

0 188 0

Elzo JamDong - TeauPla Anthem lyrics

Hey yo Welcome seme corner Plateau Capitale de la capitale... Boulangerie Sandaga, banteu ya... Yo boutique H24 nio ko ndieukk am man Bala ay Nando's ak Leader Price di am Cinéma Plazza, Paris, Sandwich Sara... Bokk dieuf, yakkh dieuf, Gouy salane, Mbott, Zungle, F.F, Bayeux, Grand'Cour, Rue Carnot... Yeah, yo fi la diangué gueum seme bopp... Hun, yeah Teaupla la diouddo, Teaupla la yaro Teaupla la maggué, Teaupla la yakkho Premier joint, premier iri Sama premier guinz, seme premier wiri Diadde kogn fakkh dém guédj Mane Assane ak Ousseynou nio dakkhone dém guédj Ponton legn dane yéndou biniouy diang féye Magg def comme grand yi wathie diangui blaze Han, bo khamoul lathié gueun Térou baye sogui léniouy lakké dieune Teaupla loum fi guédj dou takh me fatté leu Sones, Van, IFAN bi me nékké khalé leu Yék na bi Pac di dèè 96 Fi deunguey degg slang té do dem States Ay boyou 16 ans dawal Mercedes Fekk ay grand wou 30 meussougn dem sakh Thiès Yé-yéyék terrase, takk bagasou Seu-ga Ak Rone "le Parrain" Ndam-si-Yalla Rim-ka, mane ak Cavin... Diouddo Square, maggué Pentagone Fréq na Kébé, fréq na Claire Kane fréq na camp Dial Diop Se grand yi degn dane yarou bougn fi dane bal-si Métro, Aldo, PCS, Môle 2, Niani... Diaw, Popo, Olivier gawe negn lène soule Ken mounoulène fatté, mingui mél ni dawe légn lène soule ! Fallait qu'me def son bégué kogn bi Babiche ak Ibou Doumbouya kham nimeu beuggué kogn bi Nioune fi legn baser, yow fi legn ta**é Fi kou fi se wa gallé tokhou nga woute no fiy dessé Légui magg na wayé doumeu fatté terrain rouge Terrrain wèkhe, terrain noir, 4 camps même sou meu traîner-toul One, two, three, four sandial bébito Ko sandial ko sandial ko sandial bébito (wou) Outro Jamm Dongg le Kou lim dioum...mang koy méy, yo mang koy méy wa gokh bi yeup (WA TEAUPLA WA TEAUPLA en choeurs) Seme homie Bizzle, Thiaya, Thierry, Dixon, Rakhou, NYSV Soweto Boys, ARRA, Laye Nahari Nioune douniou wakh Lamine Guèye, nioune nioye wakh Van kham nga Wa Diamono tamit gning thi birr Nioune nioye gonfler nerou wa hors town Eh boy nioune degn beugg souniou kogne waye Seme yaram mingui dow waye Teaupla le man, haaa Teaupla-a-a-aaa

You need to sign in for commenting.
No comments yet.