Elzo JamDong - Roy Thi Mom lyrics

Published

0 148 0

Elzo JamDong - Roy Thi Mom lyrics

Bridge1 Maye souniou thiaatou keur, seme khol mounoul bénieu yatou mbeur Me guénne thi mbedd mi dieul mic wakhal nit gni ndakh mounoumeu wone nekk souniou baatou keur An boul khèpe seme guéy-li (liguéy); flow bi takh nga fok né poésie ngay lire Ngamey diaye grand yar sikim ni bey ni Mey pas thi game bi yow ngay lirr (come back come back come back) Maye souniou thiaatou keur, seme khol mounoul wone bénieu yatou mbeur (cheah) Me guénne thi mbedd mi dieul mic wakhal nit gni ndakh mounoumeu wone nekk souniou baatou keur Son bi la tamou deme dioye thi mom Flow biy diokhé daadj té dou doy thi bopp Mom la BEUG takkal nako BAGUE moméy BEGUEUL Pac BIGGIE gningui khole waroul noye thi yone ½ chorus "Free flow bi nice ne", -Yayeu liguey rek me roy thi mom "Free video bi nice neu", -Yayeu liguey rek me roy thi mom "Free non jo yi nice neu", -Yayeu liguey rek me roy thi mom "Free non bro bou nice le nak”! -Yayeu liguey rek me roy thi mom Verse 1 Yé-yé-yéksina sène yakaar la ta** Gni thi nangou deugg nangou Dakar la ta** (run the city) Kou lakkhou di nane bo mandé fègne (hahahaha cheah) Diapp nguène Ino, bénène bandé fègne Lé-lé-légui légui légui nioye doweul souniou biz thi tali bi (talal auto bi) Bo khamoul lou beuri boul wout alibi (boul fén se bopp) Togg na quantité yékk na qualité (cookin the FreeDope!) Bou nguène faké-woul wone sakh me mey lene parité (yeah) Bridge 2 Maye souniou thiaatou keur, seme khol mounoul wone bénieu yatou mbeur Me guénne thi mbedd mi dieul mic wakhal nit gni ndakh mounoumeu wone nekk souniou baatou keur (oh Free!) Pa bi ak Mère deme dioye thi niome Gni me gueuneu diégué nio mey dolli diom Gallé Yalle ne diGUEUnté yi GUEUneu deuGUEUr Boumou DAGG negn ko fas ndakhté waroul noye thi yone CHORUS "Free flow bi nice ne", -Yayeu liguey rek me roy thi mom "Free video bi nice neu", -Yayeu liguey rek me roy thi mom "Free jo yi nice neu", -Yayeu liguey rek me roy thi mom "Free? non bro bou nice le nak", -Yayeu liguey rek me roy thi mom Roy thi mom roy-roy thi mom, Yayeu liguey rek me roy thi mom Roy thi mom ro-ro-roy thi mom, Bayeu liguey rek me roy thi mom "Free flow bi nice ne", -Yayeu liguey rek me roy thi mom “Free? non bro bou nice le nak”! -Yayeu liguey rek me roy thi mom Verse 2 Deme ekssi lakk lepp bepp vampaya décéder (burn dem) Melomind yangui sogueu kham ni degn le done nakh ndékété (degn le done nakh rek) They can't defeat me cause I'm not fair (I'm not fair) Do-Do-Dor-Dor na #War kone gagner na #guerre (yeah) Seme gaïndé pa defe niafé seme mère def woné ngor (woné ngor, defe woné ngor) Loumou diafé diafé niounite deniou wara féy bor (féy bor anhan) Daddy ak mère dégn #War pour me sol #jo (cheah) Motakh sene dome magg nekk #fly #soldier ! (cheah) Bridge 3 Maye souniou thiaatou keur (anhan), seme khol mounoul wone bénieu yatou mbeur Me guénne thi mbedd mi dieul mic wakhal nit gni ndakh mounoumeu wone nekk souniou baatou keur Pa bi ak Mère dégn job real love Yalleu ne seme dome meuneu roy thi lol Gallé Yalle ne diGUEUnté yi GUEUneu DEUGUEUr Boumou DAGG negn ko fas ndakhté waroul noye thi yonnne CHORUS "Free flow bi nice ne", -Yayeu liguey rek me roy thi mom "Free video bi nice neu", -Yayeu liguey rek me roy thi mom "Free jo yi nice neu", -Yayeu liguey rek me roy thi mom "Free? non bro bou nice le nak", -Yayeu liguey rek me roy thi mom Roy thi mom roy-roy thi mom, Yayeu liguey rek me roy thi mom Roy thi mom ro-ro-roy thi mom, Bayeu liguey rek me roy thi mom "Free flow bi nice ne", -Yayeu liguey rek me roy thi mom “Free? non bro bou nice le nak”! -Yayeu liguey rek me roy thi mom Yayeu liguey rek me roy thi mom X4

You need to sign in for commenting.
No comments yet.