Elzo JamDong - Lonely lyrics

Published

0 154 0

Elzo JamDong - Lonely lyrics

Intro Néwone nala someu baayé me lonely (rek me lonely) Légui réére na wone lène me yone wi (yone wi umh) Verse 1 Togne ngama, alou na... Youkhou nala balou na... Li ley dioylo be légui mba dou mane? Néwone nala méré ngama égal kharou na... (eh) Yow la kham, mane nga mine... Yow la am, thi mane nga mirr Mane yow ak Ibliss rekka meunone li... Kénène kouniou narone bolé degn koy lidieunti (eh) Wayé lo guiss dey diékhe mat ne seukk légui Seme pa** yém ne fi mane mi ndieukke diéégui Dém na bala khate bala yakkh santé Ségueum diamma**anté bou dag nékk dagga**anté ! Chorus Néwone nala someu baayé me lonely (rek me lonely) Légui réér na wone lène me yone wi (yone wi umh) Wakhone nala némeu doyoul me dolli (rek me dolli) Mbokk ya ngui défar, nélène ma la tannone Wayé ken mounoumeu téré me dioum Fogone nani dessate neu wayé deme sétate Be guiss né mounougn bokkeuti room (douniou bokkeuti room) Verse 2 Foukki nit moun negn tollo khél (an han) Wayé niarri nit mounouniou tollo khol (eh) Li nga gueuneu beug moleu meuneu gueneu bégn Ladial alcoolo bi barder thi boutélou bigne ! Ki nga beugg defe wara fadj se diangoro Moye se kharit moye se ma** moye se andeundo Ki nga beugg defe wara done se wérou-waye Mais bo naré deukk thi fitna deunguey warou waay Bouniou sanione dougn fi ekssi bouniou mounone mougn... Khamanté néniou wayé ndouro wouniou Bi Borom bi bindé sounou ta**é diouddo gouniou... Beugguenté négn wayé dioubo wouniou Chorus X2 Eh Douniou bokkeuti room X2 Unhu X2

You need to sign in for commenting.
No comments yet.