Buzz Lab - Makoy Todj lyrics

Published

0 354 0

Buzz Lab - Makoy Todj lyrics

Diokh ma mic ma diagnal léne Diokh ma mic ma diagnal léne Indile rappeurs yi niou d***guale lene Indile rappeurs yi niou d***guale lene [Omzo] Kay wakhak mane fils makoy todj Kay wakhak mane fils makoy todj Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Kay wakhaka I say Kay wakhak mane fils makoy todj Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Mc sa gatt bi nangue ci def kothi No dioutou click gno lay guiss rek sapp Buzz Lab dou ay nitt degn doff Rap Game bi lagnou def ci sen poche Ask ci sopi Hip Hop Fresh 2 def Rap bi thieb bi Young Fief nekheu sauce Lathie tel H-Bomb, on est dans Rihanna (dans Rihanna, au fond) F**k, F**k, F**k Afrique sama team amena Kana (amena Kana) Li gnay tokk di rap yeup dou deggeu Dama sokhla Haters you bess nakh gnouma done bagne gnomay commence beugg Yeah, sa girl nena sama bate dafkoy khogne lo (dakoy khogne lo) Boul deglou loudoul Buzz Lab fils daflay yome lo (yome lo) Mixtape bou bess khame gna foungue koy kothie Kay wakhak mane fils makoy todj [Refrain] Deuy keula nakh (x2) Deuy keula nakh Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Dou ma sandi kher mais fils makoy todj (Walla bok) Deuy keula nakh (x2) [Canaba**e] Kay wakhak mane fils makoy todj Comme car si cla**e, yeah makoy todj Alcoolique si bar, verres yeupay todj (Walla bok) General Ba** est la, yen nieupaye tothie Sa carriere gueneu vide teuli diamanche matin Mc la gnou k** pour decorer sunu sapin Game bi yeup est-ce que amena Koufi gueuneu tangue Buzz Lab Est-ce que sa mamen meuneu dawal patin Bougoulen probleme comme nullard you nek CM1 (Thiouuu, wala bok) Yeneu gui force rap bi yene nieup serre uhnn (Walla bok) Mc bou khagou ..... Buzz Lab egal sendi ma (Walla bok) Ba** seigneur leu ci limouy def te chaque jour c'est dimanche (eskeuy) Lokho ci kaw may tek comme pa (eskeuy) def sen bop kongue (Walla bok) All eyes sama team bo guene nioune rek ngay guiss Rap Galsen ci mane comme gang gou mbelenetane [Omzo] Bou may deglou sen ay son sama khol day fess ak yeurmande he ndaysane [Canaba**e] Bou gnou fegne Tele nga buegueu changer chaine Mais demal change carriere nio koy todj sa mere day nane Deuy keula nakh (x2) Wa Buzz Lab dal fils nio koy todj Deuy keula nakh (x2) Kone Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj [Refrain] Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Fresh 2 Def Dangue ma guiss rek Sothie Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj [MedMetal] Heun! heu Danga clate ni kouy seussou girl cii bus Sama team dala time ni quelqu'un qu'on s*ce Takhaw sa kaw di saw bangua fok ne day wiss (ayy) I don't f**k with y'all p**y n***a, bougouma am syphilis Yague na diko todj ni macon ak carreaux ca**es Sama yona gueuna talli fouf yere bouniou pa**e Ki gueuna tangueu si yene, si nioune comme Maniang Ka**e Mc da nga khewi comme Alioune Ka**e Guiss meu rek, Fils lo tek Dama job lii dou ploufe, li dou "fiss mba tete" Deuy koula nakh (x2) Ci four lay nelaw, wessouna bakh Sene girl yi dima topou melni mane kesse d****g Dama fouye ni kou yore milliarou Aida Ndiongue Comme lam yi ma takeu, sama lokho lagni langueu Rap sans Buzzlab, comme guerre sans bombes Zo Dollar, Canaba**e, Med Metal blacka blackeu Shoot, Shoot To Dem ba indi laka lakeu (=feu) Courant foume coupe sama bling mongui takeu All Black Gang, ni kou diogue sarakhou nakeu [Refrain] Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak man fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Deuy keula nakh (x2) Diokh ma mic ma diagnal lene Deuy keula nakh (x2) Diokh ma mic ma diagnal lene Deuy keula nakh (x2) Indile rappeurs yi niou d***guale lene Deuy keula nakh (x2) Indile rappeurs yi niou d***guale lene Diokh ma mic ma diagnal lene Diokh ma mic ma diagnal lene Indile rappeurs yi niou d***guale lene Indile rappeurs yi niou d***guale lene [Omzo] Kay wakhak mane fils makoy todj Kay wakhak mane fils makoy todj Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Kay wakhaka I say Kay wakhak mane fils makoy todj Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Mc sa gatt bi nangue ci def kothi No dioutou click gno lay guiss rek sapp Buzz Lab dou ay nitt degn doff Rap Game bi lagnou def ci sen poche Ask ci sopi Hip Hop Fresh 2 def Rap bi thieb bi Young Fief nekheu sauce Lathie tel H-Bomb, on est dans Rihanna (dans Rihanna, au fond) F**k, F**k, F**k Afrique sama team amena Kana (amena Kana) Li gnay tokk di rap yeup dou deggeu Dama sokhla Haters you bess nakh gnouma done bagne gnomay commence beugg Yeah, sa girl nena sama bate dafkoy khogne lo (dakoy khogne lo) Boul deglou loudoul Buzz Lab fils daflay yome lo (yome lo) Mixtape bou bess khame gna foungue koy kothie Kay wakhak mane fils makoy todj [Refrain] Deuy keula nakh (x2) Deuy keula nakh Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Dou ma sandi kher mais fils makoy todj (Walla bok) Deuy keula nakh (x2) [Canaba**e] Kay wakhak mane fils makoy todj Comme car si cla**e, yeah makoy todj Alcoolique si bar, verres yeupay todj (Walla bok) General Ba** est la, yen nieupaye tothie Sa carriere gueneu vide teuli diamanche matin Mc la gnou k** pour decorer sunu sapin Game bi yeup est-ce que amena Koufi gueuneu tangue Buzz Lab Est-ce que sa mamen meuneu dawal patin Bougoulen probleme comme nullard you nek CM1 (Thiouuu, wala bok) Yeneu gui force rap bi yene nieup serre uhnn (Walla bok) Mc bou khagou ..... Buzz Lab egal sendi ma (Walla bok) Ba** seigneur leu ci limouy def te chaque jour c'est dimanche (eskeuy) Lokho ci kaw may tek comme pa (eskeuy) def sen bop kongue (Walla bok) All eyes sama team bo guene nioune rek ngay guiss Rap Galsen ci mane comme gang gou mbelenetane [Omzo] Bou may deglou sen ay son sama khol day fess ak yeurmande he ndaysane [Canaba**e] Bou gnou fegne Tele nga buegueu changer chaine Mais demal change carriere nio koy todj sa mere day nane Deuy keula nakh (x2) Wa Buzz Lab dal fils nio koy todj Deuy keula nakh (x2) Kone Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj [Refrain] Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj [MedMetal] Heun! heu Danga clate ni kouy seussou girl cii bus Sama team dala time ni quelqu'un qu'on s*ce Takhaw sa kaw di saw bangua fok ne day wiss (ayy) I don't f**k with y'all p**y n***a, bougouma am syphilis Yague na diko todj ni macon ak carreaux ca**es Sama yona gueuna talli fouf yere bouniou pa**e Ki gueuna tangueu si yene, si nioune comme Maniang Ka**e Mc da nga khewi comme Alioune Ka**e Guiss meu rek, Fils lo tek Dama job lii dou ploufe, li dou "fiss mba tete" Deuy koula nakh (x2) Ci four lay nelaw, wessouna bakh Sene girl yi dima topou melni mane kesse d****g Dama fouye ni kou yore milliarou Aida Ndiongue Comme lam yi ma takeu, sama lokho lagni langueu Rap sans Buzzlab, comme guerre sans bombes Zo Dollar, Canaba**e, Med Metal blacka blackeu Shoot, Shoot To Dem ba indi laka lakeu (=feu) Courant foume coupe sama bling mongui takeu All Black Gang, ni kou diogue sarakhou nakeu [Refrain] Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak mane fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Fresh to d**h Dangue ma guiss rek sothie Deuy keula nakh (x2) Kay wakhak man fils makoy todj Deuy keula nakh (x2) Deuy keula nakh (x2) Diokh ma mic ma diagnal léne Deuy keula nakh (x2) Diokh ma mic ma diagnal léne Deuy keula nakh (x2) Indile rappeurs yi niou d***guale lene Deuy keula nakh (x2) Indile rappeurs yi niou d***guale lene @ahmedba

You need to sign in for commenting.
No comments yet.