Buzz Lab - Général lyrics

Published

0 361 0

Buzz Lab - Général lyrics

{Refrain} Bou bess taak Wakhal gniy khar ma fay dou tay dou souba no ! J'ai trouvé la solution douma Abou Thioubalo Nokk nieup comme Balla Gueye takhawal beuzzou Modou lo Multiplié samay dialoré gnou bari nawma defma Tourando Général Eskeuy Général Eskeuy Boma séné Bayil li ngay def nieuw todjal sa Général (Walabok) Général Eskeuy Révolutionnaire sans le béret Yeah mane la Ba** Guévara Dikk changé tendance bi n***as yi di hate Kham nagn ni mafi tek tank beugouniou avouer Ani rebellion bi We Canaba**e Club marquez les pas Yokh la matal coup d'Etat coloniser gni done bagne Yeah dafa djot nieup xam kane moy général {1er Couplet} Young Militaire libéré Bango Di prouvé di gagné ay Galons Loumou yautou djot cii bounetou boumou feug mou oubékou dou bras long Majestueux tchi limouy def Boups nénala Ba** comme Messi Ba** Tchi Ballon Yaramou nééne la def nako nieup dieulsi lima indi ni Rambo Déretou noone yi ci samay talons Def révolution am niouma gueum di follow Ma nek à l'aise melni kou dougou biir Immaculée warfa matal mission Commando (Eskeuy) Ya n***as is funny ni crayon crayon bouy diéma effacé gomme Sèn Rap meunoul takhaw ni Mbasin bouniou pa**é faté gomme (Thioo) Bo amé lomay djay bo yabo na nga ci indalé tonne Dégue na niouné guéné nga album Tres bien mais sa corner (kogn) Mala eup buzz bouma fégné télé nga beug changé chaine man Démal changé carrière li day gueune tarr man Dk city finest dikk wilipander nigaz yi nekk tchi rap bi deffougnoufi sh** Tojal ma fiston may General {Refrain} Wakhal gniy khar ma fay dou tay dou souba no ! J'ai trouvé la solution douma Abou Thioubalo Nokk nieup comme Balla Gueye takhawal beuzzou Modou lo Multiplié samay dialoré gnou bari nawma defma Tourando Général Eskeuy Général Eskeuy Boma séné Bayil li ngay def nieuw todjal sa Général (Walabok) Général Eskeuy Révolutionnaire sans le béret Yeah mane la Ba** Guévara Dikk changé tendance bi n***as yi di hate Kham nagn ni mafi tek tank beugouniou avouer Ani rebellion bi We Canaba**e Club marquez les pas Yokh la matal coup d'Etat coloniser gni done bagne Yeah dafa djot nieup xam kane moy général {2ème Couplet} Déja certifié sama image soxla woul tampon CNRA Artiste reconnu bouma nékhé khoti sama carte BSDA Général immortel, on ne me tue pas, on ne me deshonore pas Daniou beugone ma marquez les pas Mais ko khol cii niom di nga guiss sama trace sou pas Khamal lène ni Ba**e moy POP depuis 2007 Décapité nieup ana koumay tenir tête Métal néna lène li Job la li dou fils mba tête Lyrics electriques meuno ko capter sans de tête Néwone nala mane may POP LO FOKK baay YAW DO GATT Mane MAY KI MOM DK CITY It's BASS I'M A STAR Yeah CHUI FLY Douma SANI KHER damay JOB SENEGAL YAKKAL SAMA DERR wanté lepp DEUGG LA My n***a damay def no DIEMATOUMA GUEUNE LA OUNDOU GUEUNE LA CLEAN yeah rappeur cii cla**e Armoire bi fess ba meuneu solal kogne n***as ya ngui merr sama buzz molène togne Guel ya ngui fééne nane mane dama lèn topeu Mais c'est compréhensible ndakh Général Ba** mom mokoy Todj {Refrain} Wakhal gniy khar ma fay dou tay dou souba no ! J'ai trouvé la solution douma Abou Thioubalo Nokk nieup comme Balla Gueye takhawal beuzzou Modou lo Multiplié samay dialoré gnou bari nawma defma Tourando Général Eskeuy Général Eskeuy Boma séné Bayil li ngay def nieuw todjal sa Général (Walabok) Général Eskeuy Révolutionnaire sans le béret Yeah mane la Ba** Guévara Dikk changé tendance bi n***as yi di hate Kham nagn ni mafi tek tank beugouniou avouer Ani rebellion bi We Canaba**e Club marquez les pas Yokh la matal coup d'Etat coloniser gni done bagne Yeah dafa djot nieup xam kane moy général {3ème couplet} Def Rap Game bi industrie bi buzzlab kone Direction Générale Reubeu MC yi nek fi di doul Rafle Général Dess na touti sèn carriére yen nieup dafay fay Coupure Générale Indile public bi limou soxla nek Alimention Générale En général bouniou tolé coté panik général Def show, get doe (Xaliss) fortifié ba rosé né kouy liguey société Générale {Refrain} Wakhal gniy khar ma fay dou tay dou souba no ! J'ai trouvé la solution douma Abou Thioubalo Nokk nieup comme Balla Gueye takhawal beuzzou Modou lo Multiplié samay dialoré gnou bari nawma defma Tourando Général Eskeuy Général Eskeuy Boma séné Bayil li ngay def nieuw todjal sa Général (Walabok) Général Eskeuy Révolutionnaire sans le béret Yeah mane la Ba** Guévara Dikk changé tendance bi n***as yi di hate Kham nagn ni mafi tek tank beugouniou avouer Ani rebellion bi We Canaba**e Club marquez les pas Yokh la matal coup d'Etat coloniser gni done bagne Yeah dafa djot nieup xam kane moy général

You need to sign in for commenting.
No comments yet.