BossBeatz Xat Xol - Xat Soldier lyrics

Published

0 121 0

BossBeatz Xat Xol - Xat Soldier lyrics

1er couplet: BossBeatz Bouma tégué mokoy téwal. Bouma yéné mokoy matal Bounouma clashé mokoy xoulo. Bouma togné sakh mou faral Moma yéné ma fly. Dou fans thats gayine Dofouma comp na. Ya takh ma fine gars Where is the xat soldier. You say I'm here Sokhlawouma tontou haters. Tmtc no fear I never turn in back. I know ima not a star Ya nék sama saak. Yaye sama homie star Refrain: BossBeatz Meunoumala faye di try gua bania cry. God bless u yaye sama gayine. (X2) This homie mome lay bégué. I tell yopu right. I kiff u boy Love bi nék sama xol. Yaw yakoy déf. Yaye sama gayine 2eme couplet : BossBeatz Bari défauts guawa mérr. Bilay Réwouma dama xamoul Samay sisters aki fréres. xamguéne lima waxoul Diégueulou si offence yeup bofi nékoulwone mou niaw Si yaw la diangué adouna liguay liguéy dafa graw Bala guay xam nieuriniam. Gua nék si diafé diafé Xoloul ligua am ligua meune motakh mome lau falé Ya nieuk gueum limay déf. Mbalak ni mane may chef I dont give a f**. Ligua beugue rék lay déf Refrain: BossBeatz Meunoumala faye di try gua bania cry. God bless u yaye sama gayine. (X2) This homie mome lay bégué. I tell yopu right. I kiff u boy Love bi nék sama xol. Yaw yakoy déf. Yaye sama gayine

You need to sign in for commenting.
No comments yet.