BossBeatz Xat Xol - Dinama Nekh (Pollution Sonore) lyrics

Published

0 160 0

BossBeatz Xat Xol - Dinama Nekh (Pollution Sonore) lyrics

Refrain : (BossBeatz & Dj Total) Dinama nékh, wakh niou lilay nékh (Boulniou Yakal) Lii Moniou Nékh, Wakh niou lilay nékh (Té boulniou Yakal) (X4) Couplet 1 (Dimélo) Damay rap guay get naneu ki dé goor djignéneu la Tek ko thi tempo yok clap b**h do thi géneu Ambiance de guagua mandi Hum madi bandit Rabou niari s** Hum maniague ka**é Di di di nala nékheu dimélo dinala nékheu Boudé diabou wally mola goudi dinala nékheu Mayma tokhou toubey ak demi shirt Géweul daffa yatou bayiiil ma dokheu thi tanki baye (Bab's Blac'k) Deup dippi deupeurdi takhoul mou guiss Soulay nékh dalay béteu limou yoora diss Soko meunoul aadji callal Makhou Ciss Mako mome mako meune mako yélo Soriba woumako kone doumako délo Ndaw rabine dialguati douggie ya kham boula**i nékh L'essentiel ték ko si temps yi bamou diékh Hé dinama nékh dinama dianama nékh Refrain : (BossBeatz & Dj Total) Dinama nékh, wakh niou lilay nékh (Boulniou Yakal) Lii Moniou Nékh, Wakh niou lilay nékh (Té boulniou Yakal) (X4) Couplet 2 (BossBeatz) J'ai l'argent, J'ai le teint (Appelle moi Argentin) 2014 doko faté (7 la si bresilien) Tarbiyou done si talibé, Dissi diangue A I B Mise en garde ni prohibé, strange music taxawél né May rap gua youxou (Ohh) Ni kou tiime tatou Nicky Harlem City Flow, apate néma Biggie Teubeul ma teup, sa baye teup, Haters yi bokk golo gui (X2) Non Non Non dama dioum niou démate Teubeul ma teup, sa baye teup, Haters yi képe golo gui Ndiabal ma ndiap ma am diap domou ndeye temps la way (Bouzot) Okay we do it, Do it do it like an animal Mic Cheick 1 2 yobouleuh Benen Monde Dadjie Dathie ngay Deff i know you like that Esk golo meun neu yék fou kawé diaroul ladjté Switch this is how we do it Boiie Bou dara sedd na lepp yeungou tay dara dou doiie Dope boiie Enjoiie Listen to da bad Boiie Boudé lii dinala nekh, Diokhko seu Baye Boiie Refrain : (BossBeatz & Dj Total) Dinama nékh, wakh niou lilay nékh (Boulniou Yakal) Lii Moniou Nékh, Wakh niou lilay nékh (Té boulniou Yakal) (X4) Couplet 3 (Rafall) Dinama Nekh, ma djeule sa tof pixéliser Dindi gag-gag, xésale harmoniser Photo bou nice guay weur, mane la Rafall Lathe ma Mami, Amina, wala Aida Fall Tasou wala guébatou no limit da niouy xoss Deub lou djoubone, amoul ragual thiap sosse Yaw na loxo yi tathiou bathiou djeumélé Xat Xol Han!!! Dinama nekh, Thiap léne Ko (Fonetik) Boula nekhé ra** tiakhagoune kheuthieul mbalou djeune Rimbi rimbi noki airou bégué bayi mathie tougne Happy rék no stress diamono twiss lagni dékélate Thia thia rumba salsa amoul teudje xalate Dokhalak mom wouye athiou combattaako tako Dadone mér ba foute way bayil foné bapko Bothie bifi tiali tiali lay nakhé déli coco Magui foo di rap tewoul yaye sama cheri coco Refrain : (BossBeatz & Dj Total) Dinama nékh, wakh niou lilay nékh (Boulniou Yakal) Lii Moniou Nékh, Wakh niou lilay nékh (Té boulniou Yakal) (X4)

You need to sign in for commenting.
No comments yet.